Taajaboon

 

Taajaboon                             

Refrain : Wolley !

 Sama taaja jii

Balaa ma ko bayyi

Saa ndeñ mu jeex      

Saa bukum jeex

Saa issa jeex

……

Abdu Jambaar

ñaari malaaka la

Ca kaw lay joge

Dal  ci diggup ruum

Mu ne yaa ji

Mba julli ngaam ?

Mu ne waa waw….

Yagat leen a yagat

Fu ñu ko yagat jëme ?

Ca ajjana sa

Mu ne baay bi

Mba julli ngaam ?

Mu ne deedet

Yagat leen a yagat

Fu ñ ko yagat jëme ?

Ca safara sa…

……..

Ganar gu ñootoot             

Taalibe bañul                        

Mus mu lakki taat

Taaliba bagnul

……

 

Remerciement  du sarax :

Na saxx mi duun unun : Que le grenier soit bien bien rempli

Bi leep sarax doy naa doy : Cette aumône-là est bien généreuse !

 

 

 

 

Envoyez un courrier électronique à webmaster pour toute question ou remarque concernant ce site Web.
Copyright © 2005 SENBAD
Dernière modification : 05 February 2014