TOOLU BAAY DEMBA

Toolu Baay Demba neexa foree ndeef

For urus,

for xaalis,

foraalefa doom;

Yaay booy jappal ma sap seta ngook,

Man manu maa japp sët bu amul bay,

Yaay,

jappal,

bu yagge njariñ feeñ !

 

Nii rek lañ koy defe nimu yombe :

Biiti bann,

biita bann,

biita bann !

 

Cela vous rappellera peut-être feue Caroline, ex- Biita bann nationale !

 

Allaaji aas !

 

 

Envoyez un courrier électronique à webmaster pour toute question ou remarque concernant ce site Web.
Copyright © 2005 SENBAD
Dernière modification : 05 February 2014